Lees Waxul
🎵 2502 characters
⏱️ 6:14 duration
🆔 ID: 5981943
📜 Lyrics
Du lepp liñ la woon mba liñou la miisàl,
Nga dal di koy gëm del degg lo, lou weesu dedet.
Yandé C.- Ndigàloo fàal, wonala ndigal baayi gor,
Wonala ndigàl bayi gor,
Maysaa biige cumbà Fàal borom fàarathi nga gambiene,
Daba maam sene ndiayoooy ndigàl fàal,
Jàmbari xelcom jàmbari xelcom ndigalo fàal,
Jàmbari lislam, nena lessoy nena less waxul
Youssou: Meyssa Cumbà fàalo ndigël Fall,
Jambari lislam, jambari xelcom, nena less hooy nena less waxul
Yandé: jàmbaroooooy Fàal,
Jàmbar ndigal fàal gor Meysa bigé Cumba Fàal,
Jàmbarooy ndigal Meysa bige Fàal gòr Meysa bigé Cumba Fàal,
Jàrama Xalifà Bàay gor Fàal,
Malay wooo Fàal Meysa Bigé Cumba
Fàal nena less hooy nena less wakhoul
Bùl degg dal di gëm wala giis rek ne waaw giis da
Fa wara lèer degg degg wara xòot jàngal la ca biir
Du lepp lu ñëw rek nga gëm ko! less oyyyy nena less waxul
Yandé: Ndaroo ma Ndigal baayi goor, jarama yooooh jàmbari bi Fàal,
Jàmbarooo nila goor di mel Fàal, jàmbarooo nila goor di mel Fàal,
Goor bu doonde bàyam tumam wàci na Fàal Meysa bigé Cumba Fàal,
Yay sëtu Ibra fàal Meysa bige Cumba fàal sa màam Ibra Fàal feñal
Axmàdu Bamba! Jàmbaroy Ndigal Fàal, nena less oy nena less waxul:
Youssou: jàmbari Islam, yiiii less oyyy nena less waxul
Yandé: jàmbare woyy ndigal Fàal meysa!
Ndigal Fàal Meysa Bigé Cumba Fàall bòrom farawaci jajañ Ndeey dàba
Maam saay sa maam a feñal Bamba ahh, sa maam feñal bamba,
Sa màama feñal Bamba ah,
Sa màama feñal Bàmba ceex bàay gòor Meysa bige Cumba fàal
Sa màama feñal Bamba Ceex bàay gòor ma Ndëgen Demba Fàal
Sa màama feñal Bamba Ceex bàay gòor Meysa Bige Cumba Fàal
Ne jàmbari xelcom,nena lén Fàal
Nena lén less waxul

Yaram be Fàal,yaram woo Ceex ndigal Fàal bàay gòor
Yaram moo Ceex ndigal bàay gòor
Ceex Ndigal jooyatuma Ceex fàal Meysa Bigé Cumba fàal jàmbar
Jàmbaroy lislam
Goor bu doonde Maamam Meysa Bige Cumba fàal,
Leppu luñuy ut ci Ceex Ibra fàal leppuy ci Ndigal fàal

Leppu luñuy uut ci bàay gòor Meysa Bige Cumba leppa ngi ci Ndigal fàal
Nena lessoy
Nena lén less waxul
Nena lessoy
Nena lén less waxul
Nena lessoy
Nena lén less waxul
Nena lessoy
Nena lén less waxul
Nena lessoy
Nena lén less waxul
Abdoulaye teme

⏱️ Synced Lyrics
[00:02.15] Du lepp liñ la woon mba liñou la miisàl,
[00:06.62] Nga dal di koy gëm del degg lo, lou weesu dedet.
[00:16.50]
[00:19.02] Yandé C.- Ndigàloo fàal, wonala ndigal baayi gor,
[00:26.32] Wonala ndigàl bayi gor,
[00:30.49] Maysaa biige cumbà Fàal borom fàarathi nga gambiene,
[00:34.57] Daba maam sene ndiayoooy ndigàl fàal,
[00:37.95] Jàmbari xelcom jàmbari xelcom ndigalo fàal,
[00:48.24] Jàmbari lislam, nena lessoy nena less waxul
[00:59.31] Youssou: Meyssa Cumbà fàalo ndigël Fall,
[01:10.15] Jambari lislam, jambari xelcom, nena less hooy nena less waxul
[01:27.70] Yandé: jàmbaroooooy Fàal,
[01:32.58] Jàmbar ndigal fàal gor Meysa bigé Cumba Fàal,
[01:39.66] Jàmbarooy ndigal Meysa bige Fàal gòr Meysa bigé Cumba Fàal,
[01:50.48] Jàrama Xalifà Bàay gor Fàal,
[01:53.14] Malay wooo Fàal Meysa Bigé Cumba
[01:57.08] Fàal nena less hooy nena less wakhoul
[02:03.72] Bùl degg dal di gëm wala giis rek ne waaw giis da
[02:12.75] Fa wara lèer degg degg wara xòot jàngal la ca biir
[02:18.56] Du lepp lu ñëw rek nga gëm ko! less oyyyy nena less waxul
[02:29.21] Yandé: Ndaroo ma Ndigal baayi goor, jarama yooooh jàmbari bi Fàal,
[02:37.75] Jàmbarooo nila goor di mel Fàal, jàmbarooo nila goor di mel Fàal,
[02:46.95] Goor bu doonde bàyam tumam wàci na Fàal Meysa bigé Cumba Fàal,
[02:51.03] Yay sëtu Ibra fàal Meysa bige Cumba fàal sa màam Ibra Fàal feñal
[02:57.38] Axmàdu Bamba! Jàmbaroy Ndigal Fàal, nena less oy nena less waxul:
[03:07.94] Youssou: jàmbari Islam, yiiii less oyyy nena less waxul
[03:26.19] Yandé: jàmbare woyy ndigal Fàal meysa!
[03:32.92] Ndigal Fàal Meysa Bigé Cumba Fàall bòrom farawaci jajañ Ndeey dàba
[03:39.14] Maam saay sa maam a feñal Bamba ahh, sa maam feñal bamba,
[03:44.18] Sa màama feñal Bamba ah,
[03:48.35] Sa màama feñal Bàmba ceex bàay gòor Meysa bige Cumba fàal
[03:52.63] Sa màama feñal Bamba Ceex bàay gòor ma Ndëgen Demba Fàal
[03:56.53] Sa màama feñal Bamba Ceex bàay gòor Meysa Bige Cumba Fàal
[04:00.38] Ne jàmbari xelcom,nena lén Fàal
[04:07.85] Nena lén less waxul
[04:12.55] Bùl degg dal di gëm wala giis rek ne waaw giis da
[04:21.47] Fa wara lèer degg degg wara xòot jàngal la ca biir
[04:29.12] Du lepp lu ñëw rek nga gëm ko! less oyyyy nena less waxul
[04:39.21] Yaram be Fàal,yaram woo Ceex ndigal Fàal bàay gòor
[04:47.61] Yaram moo Ceex ndigal bàay gòor
[04:51.04] Ceex Ndigal jooyatuma Ceex fàal Meysa Bigé Cumba fàal jàmbar
[04:55.06] Jàmbaroy lislam
[04:59.91]
[05:05.73] Goor bu doonde Maamam Meysa Bige Cumba fàal,
[05:09.72] Leppu luñuy ut ci Ceex Ibra fàal leppuy ci Ndigal fàal
[05:13.83] Leppu luñuy ut ci Ceex Ibra fàal leppuy ci Ndigal fàal
[05:20.11] Leppu luñuy uut ci bàay gòor Meysa Bige Cumba leppa ngi ci Ndigal fàal
[05:23.67] Nena lessoy
[05:26.82] Nena lén less waxul
[05:30.13] Nena lessoy
[05:33.23] Nena lén less waxul
[05:37.38] Nena lessoy
[05:40.65] Nena lén less waxul
[05:44.59] Nena lessoy
[05:47.74] Nena lén less waxul
[05:50.99] Nena lessoy
[05:54.27] Nena lén less waxul
[05:58.70]
[06:03.48] Abdoulaye teme
[06:05.18]